Video Wax Ju Bari de Youssou Ndour 2025 Cristiana Lyrics

Escucha la música Cristiana más popular de Youssou Ndour y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en MusicasCristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Wax Ju Bari » Youssou Ndour Letra

INICIOYoussou NdourWax Ju Bari

Youssou Ndour - Wax Ju Bari Lyrics

Boo mer ee dëgg, sëytaane da lay dugg
Jaxjax al sa xol, def loo la, li mu bëgg
And al ak dal

Sëytaane da fay jël temps, yakkamti wul
Boo am ul chance, bu la yalla, dimmili wul
Da, lay, xaptal

Boo bëgg ée mucc, ngóor sii, yaw déglu ma
Bu la fekk oon taxaw, toog al, xarit sama
Toog al ba dal

Bu la fekk oon toog, tëdd ël, ba gagni dem
Bu yagg ee, sëytaane, day mujj dem
Doo tu la tal

Bul nangu, wax ju bari yaw
Ku la ko bëgg indil na nga bañ
Bul ko kaf e, bul ko mbokk oo
Fexe el dund te ànd ak dal
Booy ànd al, na nga seet
Nit ku regle, te bañ bari wax
Fexe el ba adopter, dund gu ànd ul ak bari wax
Ku la ko bëgg teg, bul ko nangu, bul ko masala
Bari wax, da lay tardeel, bari wax, da lay sonn al
Bari wax, da lay jaxase

Bu leen sonn al béer, njaw du mel ni lem
Bu leen sonn al béer, njaw du mel ni lem
Bu leen sonn al béer, njaw du mel ni lem
Bu leen sonn al béer, njaw du mel ni lem
Bu leen sonn al béer, njaw du mel ni lem

Wax lu néew, jëf lou bari, kouné war na laa
Wax lu néew, jëf lou bari, kouné war na laa
Ni nga dundé, neex u ma, neex u ma
Ni nga dundé, bayyi ko, bayyi ko
Wax lu néew, jëf lou bari, kouné war na laa

Ibra kassé birame coumba Ndiaye
Kouly kassé ek maajigéen oo
Al Maabo Yacine dial, ma des ca bëlbë
Moo ma daan wax naan
Youssou na ñu ànd liggéey, te waññi wax, te waññi wax
Baay i Oumar, baay i Alioune
Baay I ndeye kassé Góor u fatou
Baay i idi, doom i nday i adama, ak kassé plus
Al maabo yacine dial
Ibra mor astou kassé
Fatou oy, médoune kassé
Ndoumbé yatma

Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la
Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la
Wax da fay gatt yanu maanaa
Neex a dégg lool, fees ak njariñ
Ñu wax ko ba wax jot ee, fa ñu ko war a wax e

Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la
Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la

Xaaj u guddi, boo toog oon ba mu yagg
Nga doon bëccëg di na xumb lool, ba jaaxal gaa ñi

Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la
Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la

Wax Ju Bari » Youssou Ndour Letras !!!
ANUNCIOS PUBLICITARIOS
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© MusicasCristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.